Prends garde à l'allure
Belle comme tout début
Selon la sagesse
Entrée brusque
Bonne odeur qui se répand
Quel grand bonheur !
Des oiseaux migrants
Par milliers au Parc de Jouj
Majestueusement
Beaucoup d'animaux
Affolés se sont enfuis
En folle débandade
Même le lièvre passe
En sauts ses oreilles au dos
De quoi a-t-il peur ?
Birahim Thioune
- - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - - -
Loo gis ay xélam neex
Jàppal ni dey door a tëb
Lii waxi mag la
Bima nee saraax
Xet gu neex a gilli
Bama yëg bànneex
Ay ndiraani picc
Ñoo yegsi si Pàkku Juuj
Jekk na rafet na
Rab yu bari lool
Dañoo sàmp seen u xél
Ñoo ngay jow-jowi
Lëg a ngii di daw
Boot ay noppam di few-fewi
Moo lu muy ragal ?
Biraahim Cuun.